Mia Guisse - Gauche & Droite (Clip Officiel)

  • ** Écoute le nouveau single ici bfan.link/gauche-droite : GAUCHE & DROITE disponible sur toutes les plateformes musicales & réseaux sociaux. Streame pour soutenir tes artistes ! **
    ** Clique ici bit.ly/miaguisseabonnetoi pour suivre mon actualité **
    MIA GUISSE évolue & bouge : son nouveau clip, GAUCHE & DROITE.
    Lyrics plus bas dans la description (dernière partie).
    #miaguisse #gaucheetdroite #clipofficiel #love #renaissance #miaguissestyle #mgs #team221
    ** Crédits de la chanson & du clip GAUCHE & DROITE **
    Auteur : Bakhaw Dioum & Mia Guisse
    Compositeur : Akatche
    Enregistrement, mix & mastering : Akatche
    Réalisation Clip : Reverse Studios
    L’équipe Reverse Studios pour le clip
    Réalisateur, montage & color grading : Bilal Mbengue
    D.O.P : Mbaye Diop
    Chorégraphie : Steven Tourbillon
    Assistant réalisateur : Djiby Niang
    Photographe : Amzii.op
    Accessoires : Magic Hands
    Make Up : Devon 16
    Stylisme : Mia Guisse Style, Afshal, Elfecky
    Coiffure : Kangue Hair
    Une production de Mia Guisse Style (Dakar, Senegal, mai 2024)
    ** Retrouve Mia Guisse sur les réseaux sociaux **
    Instagram www.instagram.com/mia_guisse
    TikTok www.tiktok.com/@miaguisse
    Facebook www.facebook.com/profile.php?id=100065839831967
    ** Contact management **<26>miaguissecollab@gmail.com
    +221 77 655 59 67
    ** Lyrics de la chanson GAUCHE & DROITE **
    Yaw la Yaw la Yaw la
    yéné sama xol ndakh damala
    love té sakh kafou ma ci
    Dama sensible deug la
    Dama feel beug la diokh
    Sama xol bi ndakh damala
    Khalé bi té mala diokh
    Sama xol bi
    Ndakh damala love
    Damalakay diokh, damalakay diokh
    Damalakay diokh love bi nek thi mane
    chéri ba nopi sopi sama sant
    Damalakay diokh damalakoy diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh
    Han man, han hawma lanela
    Ma ngui doundou love story bouma yéém
    Boulma laadj louma dal nii
    Sama nobél amoul foumou yam
    Khalébi soma laadjone
    jant bi, non tey dou fanane
    Khalébi soma laadjone
    sama bakane, damalakay diokh
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    chéri ba nopi sopi sama sant
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh
    Gauche wala droite? Dis moi si tu veux en haut en bas ? Dis moi
    Lou tang wala lou sééd?
    Dis moi
    ma servir la
    Bou 19h dioté gnou teudi
    Na metti, na yaag, na melni
    Khalébi boul ragal na nga yekssi
    Gnoune kessé la thi keurgui na djoly
    My babe touch my body ouh !!!
    Everyday ma diokhla nga né thi
    Khalébi tekk ma lou metti
    Bou yékhé thi yaw la
    No no dou thi man han yayayay
    Han man, han hawma lanela
    Ma ngui doundou love story bouma yéém
    Boulma laadj louma dal nii
    Sama nobél amoul foumou yam
    Khalébi soma laadjone
    jant bi, non tey dou fanane
    Khalébi soma laadjone
    sama bakane, damalakay diokh
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    chéri ba nopi sopi sama sant
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    Yalla ko def lolou louma thi meun
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    chéri ba nopi sopi sama sant
    Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane
    Yalla ko def lolou louma thi meun anh yeah
    Oh yeaah ! oh yeah
    Ndéké khalébi rek laa nop
    Mane khalébi rek la nop
    Oh yeaah ! oh yeah
    Ndéké khalébi rek laa nop
    Mane khalébi rek la nop ba sagar khégne

    Category : Senegal Music Videos

    #mia#guisse#gauche#amp#droite#clip#officiel

    0 Comments and 0 replies
arrow_drop_up